Commentaire de smb (19/06/2008 19:31) :
Assalamou aleykoum warakh matoulah. Daniouy Sant yalla, diouly thi yonéne
té bou téd bi. Té di nane Dieuredieuf serigne TOUBA, mome mi niou nguindi
khirtal niou thi yoonou l'islam. Niou sopéy Khadim GUEYE, bimou dé woy
khassaïtou Serigne TOUBA yi. Di ko nianal yalla yok katanam bamou béy waram
thi khassaïte yi, ndakh, Mouride bou nék am nga thi sa war.
Sant naniou bou wér, de la part d'un ndongo.
|